logo MP3
head_logo

Titi Boko Lale Скачать

main img

Titi

Boko Lale

20 Прослушиваний
05:17
Все треки Titi
Слушать
Скачать песню

Текст песни

Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo

Dama la beug
Ba soumela guissé damay gueulem
Nena mala beug lolou
Neube touma
Tiakhane nouma
Chéri khana khamoulo ni
Soy nelaw dama lay time
Ba soy khandior ma contane
Fass yenné seuy seuy bi
Neleeen neeelen

Nimala beugué
Dafa diegui dayo
Ba souma la guissé
Samay tank diakhasso
Sama lamigne reer ma
Wakh nala wakh nala
Awma ci mom sagou
Ba soy nelaw
Soy nelaw dama lay time
Ba soy khandior ma contane
Nelen mafi né
Neleeen neeelen

Boko lale
Kou ko lale gagn
Boko lale
Boko lale dina la door
Soko lale
Boko lale dina la door

Loutakh bouniou séné
Di napp nabi
Setti Doudou
Setti Ali
Nalèn none yi niou yakk diganté bi
Nena la

Fi ma fi né
Ben dieg dou nelaw
Kogn bi am nguen gane

Boko lale
Boko lale dina la door
Boko lale
Soko lale dina la door

Boko lale
Soko lale dina la door

Boul lal bi
Bi mako mom
Boko lale
Boko lale dina la door

Makk yow guén gui diékk ba tay
Amoul nou mala beugué woul batay
Fass yénné fedeuli yaye sama mbeugël
Ci yow ma mayla pithie ak garap

Kogn bi am nguen gane defarat len togay yi
Fi ben dieg dou nelaw
Ay kouma nopp sa dieukeur ben dieg dou nelaw
Kogne bi daniou nane

Dafa ragal diabaram
Dou lolou
Mbeugël lako fall
Goor bou la deukeul
Dang koy deukeul
Yama tamal mallettou or
Yama tamal balanssou diamant
Tekk ma sama place
Kham né rombou na lolou
Souma la kholé nga validé

Mo tax boko lale
Soko lale dina la door
Soko lale
Soko lale dina la gagne

Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo beyo beyo (beyo)
Ayo beyo beyo beyo
Ayo beyo beyo beyo
Ayoooo beyo
Boko lale dina la door

На странице доступен трек Boko Lale от Titi. Слушайте онлайн или загрузите в один клик бесплатно на свое устройство.